
Fi di gyal dem know seh man is not an issue cah yuh pum pum turn up , it ah mashop becah yuh pum pum turn up Mi tell yuh seh yuh have no low budget vagina enuh 😅 Designer pum pum weh yuh deh ? 😁 #LBVA

je suis pour l’amour et la protection des femmes, des enfants , des orphelins. #MGM

Fi di gyal dem know seh man is not an issue cah yuh pum pum turn up , it ah mashop becah yuh pum pum turn up Mi tell yuh seh yuh have no low budget vagina enuh 😅 Designer pum pum weh yuh deh ? 😁 #LBVA


Pourquoi je pourrais jamais critiquer les jeunes au Sénégal c’est parce que je peux même pas imaginer ma vie de jeune de 18 ans jusqu’à mes vingtaines à Dakar. Meunon na nék dans le même pétrin di stressé di wout ligueuy et tout . Je remercie Allah et je leurs souhaite la réussite . Nalen YAllah taxawou boubakh🤲🏿


Okay boulen ma rétane mais lan moy “ lay birr” ?honnêtement je connais pas



Kon célibataire dafay rér? 💀
Célibataire méti na daguay wathi do xam sakh loo wara rérré

Ñakk gëm yalla wala weddi ko loolu warul nekk jafe jafe ci ab jullit, ndax al xuraan xamal nanu 1- forcer nit pour mu duggu ci islaam amul ci diine ji (S2, V256) 2- xamal nanu ku nekk amna liberté gëm wala weddi (S18, V29) choix boo def amna responsabilité, 3- xamal nanu yalla mooy gendi jubal ku ko neex (S28, V56) 4- xamal nanu danoo wara nekk nu bienfaisants et équitables ci ñi nekkul ay jullit ta seq ag nun jàmm (S60, V8) Waaye benn jullit bu am fayda warul nangu kenn kuy saaga diine ji wala diko baña respect.

Ma sha Allah ❤️❤️❤️🤲🏿
“When they say it’s the ‘Urs of Sayyidatina Fatimah az-Zahra ع, then immense blessings… passing was a reunion with her reality” #ShaykhNurjanMirahmadi #MuhammadanWay

Yooooo 💀💀💀😂
Lii deh, ça me rappelle mon cousin ceddo ki avait échoué au BAC, en plein ramadan. Ñëw rek, jubël ci ndaa li, tànq potu ndoxam, tàmbali naan. Gars yi ne ko, nda ngaa fate nda ngaa woor. Mu ne leen, non mais Yalla moom bu defe nee dañ ko fiy nekal,te du fi nekal keen, da na leer😂

Deep and factually evident ❤️
“Free will is very, very limited” #ShaykhNurjanMirahmadi #MuhammadanWay

❤️🤲🏿 Very important.
“As a result, in the areas in which Allah’s Anger is coming, we find ourselves to be protected…” #ShaykhNurjanMirahmadi #MuhammadanWay

Ziyarah of the Maqaam of Nabi Hud (alayhi salam), Allah Ahqaf, Yemen

Timiss fék ma si mbedd rek la bañ , mang dawal di vitesse pour agg keur SubhanAllah

Deug deug xana mou lox loxi sax si lokhal bi wayé déé 💀
Mor Thiam tamit gaaw na déé 😂